Bella

Wizzy Kana

Compositor: Não Disponível

Leeraay bi may gis ci sa xar-kanam
Moo muur samay bët ba gisuma leneen
Xoolatuma faalewuma
Focus ci yaw rekk, xale bi dina ma ray

Yàllay maye boo ma mayee li ma lay ñaan
Ma ne xale bi moom laa bëgg def sama soxna
Mënuma la duma la tëkk la ñoom
Yaay sama kiiraay
Ma ne bëgguma ku ma takkale ak yaw
Yaa sama leeraay waay

Belissima mia
Ma ne de wóolu naa la
Moo tax ma jox la sama xol
Lii yaw yaay boroom

Ti voglio vicino me
Sei la mia vita amore
Duma la laaj foo may jëme
Diri ma man, yóbbu ma fu la neex
Bella Bella Bella Belisima mia
Bella Bella Bella Belisima mia

Bérbu bët mësta xool
Feneen fu nit demul woon
Bànneex bu réy ngay am ci biir xol
Bés ngi ñëw maak yaw lay doon
Faalewuma ñi may topp
Maak yaw ba abadan, baby yaay sama life
Yaay sama Ouroul Ayni
Te bëgguma ñu foo farata laay def

Ti voglio vicino me
Sei la mia vita amore
Duma la laaj foo may jëme
Diri ma man yóbbuma fu la neex
Bella Bella Bella Belisima mia
Bella Bella Bella Belisima mia

©2003- 2025 lyrics.com.br · Aviso Legal · Política de Privacidade · Fale Conosco desenvolvido por Studio Sol Comunicação Digital