Compositor: Não Disponível
Niass coumba Abdou laahi
Douggeul yallah souniou xol yée wawaw
Thi leundeum nganiou génné waaw
Douggeul niou thi leero néniou
Leer yaanguî
Allah allah
Baye barhama baye
Leer neuh geediou khaybou nganiou gindé baye
Tektal niou thi lou leer seeyal niou si dieumeum djé
Nioune dh dellou nagn thi yallah
Xaménaniou yonent
Halou cheikhou Tidjane
Xamal niou moy barhama
Wa sallahou maadaama siffaati zaati barhama
Alal asslil ussuli min banni addanani Barhama
Laa ilaaha ilallah
Laa ilaaha ilallah
Euweulo akhirou bi Baye leuh
Zahiro baatinou bi Baye leuh
Teg nganiou thi loxoy Wilaani Bayo
Mou dieul niou teg niou thi loxoy euweulou Bayo
Nourouhou
Euweuloul woudjoudi woudjouda
Fa Houwa assloul ussuli wal anjani
Lam yazal nourouhou bi aynine ilahi
Fintikhali fil keuwni bahdan tikhali
Wa sallahou maadaama siffaati zaati barhama
Alal asslil ussuli min banni addanani Barhama
Laa ilaaha ilallah
Laa ilaaha ilallah